Ki moy fatma sama linguere bi
Bougn né danga bakh kén douni goulétt
Weureu touma lénen ioe la doon sétt
Yaay sama raini xool geureum nala
Ndakh fatma yamay nital ni wërr wii J
Aldiana lay dundu fékk magui sa wétt fa
Yay tool bu nagoul nawétt dieumbeut
na man sama djiwou ci ioe
Ndéké beugué woum la
xol bi késsé
fatma sama rouh gui lalla yeugué fouma guestou
guiss la ngamay goungué ni takander
fatma sama summer nga yaw danga yoré djiko djiégu
pousso sama yaye ko wax waxou mako
chérie talla ak li take si mane
fatma wayal nala man talla mi sa
dieucoeur kon wayal nala Gueye ndax sama
sant ngay woyu pouye yaba xaré mame borom
rée diou dji mba méroo todieul Nala colonel sama xol yakoy madj lo pouye yaba xaré Mame lake nga sama nguereum