Woy wi dafa war a wax ci jigéen ju tudd Sira, ku simple, rafet ci naturel, kuy ree bu baax, te am teggin ak yaru. Ku am classe te respekte nit ñi, ku xol yu set.
Woy wi dafa war a doon bataaxal félicitations ak waxtaanu mbégte ngir bésub juddoomam.
Tudd ko ci woy wi, sant ko ci ay jikkoom yu rafet, te ñaanal ko yàlla may ko wér-gu-yaram, barke, yéené yu mat ak texe ci dundam.
Refrain :
“Sira Talibé Baye Bi,
bésub sa juddu moo ñëwsi,
Yàlla na la fay barkeel,
yaw yaa neex ci sunu xol.
Sira sunu leer,
Yàlla na yokk sa weér.”