[Intro]
Daara ci kaw, nafi nekk, baax na, jamm rekk
[Verse 1]
Si séy beutt la guiss sa mbeuguél bou woor
Ma kham ni ioe doma musseu diendé ak bénéne goor
Dalalal sa khél fi dofi deug khasté wala kilay door
Dokh sissa banékh bagn la gnak llou yeup damkoy soor
[Pre-Chorus]
Nangu na jàmm ci sunu liggéey, jox na moroomu xarit
Góor gi ngi rënn, diir ci góor, leegi am na liggéey suñu xol
[Chorus]
La paix on l’aura même si on doit cassée des cœurs
Tu mérites le bonheur prsk c toi ki apaiser mn cœur
Dans tes bras k je veux dormir jusqu'à mon réveil
Et tu restera dans ms pensées jusqu'à ce qu’on vieillisse
[Verse 2]
Mbedd mi dafa tàng, man ma yor li koy faye, Bëre ak man, mooy sank sa bopp, loolu du taye
Samay rime youy tàk, melni àllal ci lak, Dreuz la tuddu, képp kuma sorou dinga gnàk
Dakar ba Zikichor, gnongi may dëggal ci kaw, Flow bi dafa dëgër
Kone gnoumay teukou dou iow
[Bridge]
Duma wax lu bari, samay jëf ñooy feye, Succès bangui
MANE LA DREUZ BI, XAM NGEN KO BU BAAX SAMA NDIAM DAFFA TAKK
[Chorus]
La paix on l’aura même si on doit cassée des cœurs
Tu mérites le bonheur prsk c toi ki apaiser mn cœur
Dans tes bras k je veux dormir jusqu'à mon réveil
Et tu restera dans ms pensées jusqu'à ce qu’on vieillisse
[Outro]
Bayi, bayé, yémé, la paix s’avance pour nous deux
[Outro]