Man sama xol baby ya ci nékeu
Monoumaa dém sans yaw
Diéguéma ma wan la lifi nékeu
Monoumaa dém sans yaw
Khana guisso sama texto
Bobou ba légui Mangui xaar tontou wo
Man diaxlé naa ba dougou watsapp Envoyé
Lafa vocal tontou woo yamay déf li té beugouma man loula meti