Gis naa ki ma doon Lépp soppeeku bis bi ma doné baye sudee àdduna bi daf lay sonal lool Dinaa la jàppale saa yu nekk Sama thiofel ci Maimouna laawou buur bi papa bind ngir doomam Maimouna rokhaya Alioune cheikh youssouf Soo xamoon rek ci hawa ba ngir doomam yi Maimouna ,rokhaya Alioune akh cheikh youssouf moo ko bind ngir doomam Max Liron Yaa ngi may indil yaakaar suma mënatul noyyi Yaa ngi may jox mbëggeel, yaw rek laa soxla Maa ngi lay tëye ndànk Kontaan naa lool ci yab la ci sama biir Dinaa ko wax ci ngir Maimouna doomam bu mag
Maimouna alioune Maimouna Alioune
Rokhaya Alioune rokhaya Alioune
Cheikh Youssouf cheikh Youssouf