*Titre : MERCI Maman*
*Couplet 1 - Wolof*
Yaay Fatou Danso, yaa ma jur
Sa bëgg-bëgg moo ma yar
Boo ma xoolée, sama xol sedd na
Sa loxo takh ma am doole
DINGA NÉK SI SAMAY XALATE
BA BOUÑIOUY MAGUÉTT, yaay bi
*Refrain - Français*
Merci Maman, Fatou Danso
Pour tes nuits blanches, pour tes bras si chauds
Tu m’as porté, tu m’as guidé
Sans toi je ne serais pas qui je suis
Merci Maman, mon pilier, ma foi
Chaque souffle que j’ai, je te le dois
*Couplet 2 - Wolof*
Jërejëf yaay, jërejëf lool
Sa wax ju neex, sa cofeel
Liggéey ngaa ngir ma mucc
Tey ma gise sa ndam lu réy
Sunu kër, yaa ko def paradis
Fatou Danso, yaay bu sell
*Refrain - Français*
Merci Maman, Fatou Danso
Pour tes conseils, pour ton amour si haut
Tu m’as appris à rester debout
Même quand la vie devient un caillou
Merci Maman, mon soleil, ma loi
Tout ce que je deviens, c’est grâce à toi
*Pont - Wolof/Français*
Yàlla na la yàlla fay sa baax
Que Dieu te rende tout ton bien
Teey sama ngëm, teey sama doole
Tu es ma force, tu es mon chemin
*Dernier Refrain - Français*
Merci Maman, Fatou Danso
Je chanterai ton nom tant que je vivrai
Nulle femme ne vaut ta lumière
Merci Maman, à toi ma prière