Couplet 1
Bëss bi ma la gisé ba léegi, sama xol nekkul feneen
Sama khalaat yépp ci yaw la dëkk, mouy suba ba jant bi sooo..
Lula neekh, neekh nama , loolu laa bëgg,
Ci iow baby
Sa mbëkté mooy sama sama sag
Yaw laa tànn ci biiri Djég
sa ràfetaay môme laay Yëgg.
Baby... Iow la Bëgg
Refrain
Damako nobb, loolu laa wax
Damako nobb, wér na ndax
Sama xol bi yaw la bëgg
Ba faww, duma la wone gannaw
Couplet 2
Su ma déggee sa baat, sama xol day Nékh
Sa khéettu ree bi
damay faj sama khôl bi fékh
Duma la nax, duma la bàyyi nioula thiatou
Ndax yaw yaa di sama Loulou,
Takh niou may wowé Ma siithiou
sama kharitte, sama chéérieee
Yama takhaaa fiipou.
Refrain
Damako nobb, loolu laa wakh
Damako nobb, wér na ndakh
Sama xol bi yaw la bëgg
Ba faww, duma la wone gannaw