Couplet 1
Sama xol daf la bëgg, ba du man a tëdd
Guddi ak bëccëg, yaw rekk laa giss ci sama bët
Sa bopp mooy sama jàmm, sama xel daf ko xam
Ku la gis, xam ne yow yaa neex ci sama yaram
Pré-refrain
Bul dem fu sore, bul ma bàyyi ma dox doŋŋ
Ndax sama mbëggeel ci yaw du am fenn bong
Refrain
Mbëggeel bu wér laa la jox
Du mbëggeel bu leer tey ba suba jeex
Yow yaa ne sama leer ci guddi
Sama dund, sama xol, yow nga ci nekk ba fàww
Couplet 2
Sa wax ju neex daf may jàmm ci xol
Sa reer daf may doole bu ma sonn
Boo ma xool, dama fàttalikoo sunu fan yu baax
Yaw ak man, du nu séparé ba fàww
Pont (bridge)
Cheikh Faye Su ñu amee ay jafe jafe, dina nu ko jàpp ci loxo
Ndax mbëggeel du ragal dara boo amee ku ko bokk
Sama Killifeu gui
Refrain (x2)
Mbëggeel bu wér laa la jox…