[Intro]
Hey hey, nioba touré, fatou mbaye, chérii aliou
[Verse 1]
Nioba Touré iow kayyy, fatou mbaye iow kay
Chériii Aliou manka yiiiiiiiiiiii
Kay lénn tokë, hey
Yayouuu ndeye Yacine manka ak Diallo manka heyyyy
Bouguounéee dagnénnn bax kéneu douu née goulétee
Aliou manka néna weureutoul lénéneu yénn la done séte hey
Néna yeunay réeniiiii xolammm yeureum nalénnnn nakh
Aldiana layy doundou fékk mogni ak Fatou mbaye AK Nioba Touré heyyy Fatou
"mbaye Nioba"
"Nioba Touré"
[Chorus]
Nioba Touré, Fatou mbaye, ndella sa baye, nanta ke beugé
Nioba Touré, Fatou mbaye, ndama réew téé, lène nuuré
[Verse 2]
Aliou manka néna ndéké beugué wouléne xolll bi kassé hey
Néna foumou "guessto guiss lenn si wétame ni takandërrrr" hey
Yayou ndaye Yacine manka ak fatima manka heyyyy
Hey hey Nioba Touré, Fatou mbaye, hey hey
[Bridge]
Nioba Touré, Fatou mbaye, zé téy lépp si jàmm, wakh
Ndax nioba, fatou, ak Yacine, ak Diallo, ak Aliou
[Chorus]
Nioba Touré, Fatou mbaye, ndella sa baye, nanta ke beugé
Nioba Touré, Fatou mbaye, ndama réew téé, lène nuuré
[Outro]
Nioba Touré, Fatou mbaye, nioba touré, fatou mbaye, fin